Nothing Special   »   [go: up one dir, main page]

Aller au contenu

Agabus

Jóge Wikipedia.

Ci làkku ibrë la tur wi jóge. Ci angale ak ci faranse mooy Agabus.

Toppkatu Yeesu la woon ci Yerusalem, ku Yàlla mayoon mu mana yégle lu wara ñëw (yonent). Am na benn aada bu wax ne Agabus bokkoon na ci 72 taalibe yi Yeesu yónni ci Lu 10:1.

Ci Injiil dañuy wax ci Agabus ci Jëf 11:27-28; 21:10-12.